azlyrics.biz
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

nitdoff - tekk ci brikk 2 lyrics

Loading...

[intro: pape sidy fall]
sénégal, après l’incroyable succès de kaay tekk cii
brik
voici kaay tekk cii brikk 2 with my mans baryo (tekk cii brikk 2) , resk-p (tekk cii brikk 2)
gofu (tekk cii brikk 2) , vito (tekk cii brikk 2), p.p.s (tekk cii brikk 2) , kaz k!llah , cap 2 seuss , djily
bagdad (tekk cii brikk 2) , sevethy sky (tekk cii brikk 2) , da brains (tekk cii brikk 2), my n-gg- books (tekk cii brikk 2) nitdoff k!llah
wa legui nak ?

[refrain: nitdoff]
bo tchii meuneta tek lou carré n-gg- werr ko té go
bo tchii meuneta tek lou carré n-gg- werr ko té go
real rap lagni mouki kheurko saa kaw
real rap lagni mouki kheurko saa kaw
tekk cii brik 2, tekk cii brik 2 (what)
tekk cii brik 2, tekk cii brik 2 (what)
east side, west side, tekk cii brik 2 (héééé)
tekk cii brik 2, tekk cii brik 2 (what)
tekk cii brik 2, tekk cii brik 2 (what)
north side, south side, tekk cii brik 2 (héééé)

[baryo (alien zik)]
doxé mbéde p.a diougué bène big crew
street k!llah alien founé lagni sick rouh
boulééé systeme, niouné yeup dém gueustou
koula sèn game niolay seuf tekk cii brik 2
brik lay tek, flow douma yox-ssou
zik lay frekk, thioy douma téféssou
baryo bèn maff undercova
fateu sèn seuleube yone lepp over

[resk-p]
lii wess na done lou carré boule barré, less dalay garé
t-ssaré xibaru guissané bii guéinto niou ndaré
t-ssaré dissayou souy ballet ngène waru cii kharé
f-ssalé maçons yi m-ssalé kepp markél ma art ré
sauf gni parano, ay pyramide teuk parallélépipède
niou nan’gou cii pet
ma tchii tekk né rrchitecte
raatalé seug sèn diwane sangue sunu squad
tekk tchii lou kawé kène dou niou calé
k!llah where you are?

[refrain: nitdoff]
bo tchii meuneta tek lou carré n-gg- werr ko té go
bo tchii meuneta tek lou carré n-gg- werr ko té go
real rap lagni mouki kheurko saa kaw
real rap lagni mouki kheurko saa kaw
tekk cii brik 2, tekk cii brik 2 (what)
tekk cii brik 2, tekk cii brik 2 (what)
east side, west side, tekk cii brik 2 (héééé)
tekk cii brik 2, tekk cii brik 2 (what)
tekk cii brik 2, tekk cii brik 2 (what)
north side, south side, tekk cii brik 2 (héééé)

[gofu (yatfu)]
kaddu wourouss gofu sorore la né lampe
khérou deundou sèn kaw eukhelou rap béma sampeu
all school cii all school use rap ba done junky
air fly tekk cii brik sèn kaw bopp lay dunky
done bindeu kaattt
done guindiii kattt
done idji kattt
done done done firi katt
douma sèn m-ss sèn tolou way mo soufé
ba lèn rap gadou bongo weur dii sambay mbayane dioufé

[vito]
eh yow tek cii brik djeuléko fimou né
rap galsen meuneu raw cii fimou né
dag-y saupeu meune naniou cii film bouné
golo golo melni kouy joué filmou né
this is the part 2 nga wédii niou gaddou
the building, tekk ay rimes you gueune xathiou
let’s go niou tekk cii brik adiatt level bi cii barr’am
nioune danio xam rap né mandi kaattt di khamékou baram
yes since 1994 people say gni douniou nitt

[refrain: nitdoff]
bo tchii meuneta tek lou carré n-gg- werr ko té go
bo tchii meuneta tek lou carré n-gg- werr ko té go
real rap lagni mouki kheurko saa kaw
real rap lagni mouki kheurko saa kaw
tekk cii brik 2, tekk cii brik 2 (what)
tekk cii brik 2, tekk cii brik 2 (what)
east side, west side, tekk cii brik 2 (héééé)
tekk cii brik 2, tekk cii brik 2 (what)
tekk cii brik 2, tekk cii brik 2 (what)
north side, south side, tekk cii brik 2 (héééé)

[pps]
han so ci manoul tek lou carre bakok kathior bi
li mbed sokhla la ghost loukhousskate yor ni
djaffee la yombeu meu, sekil rime yi ni njorni
technical chemical sk!lls feetee ndeydior ni
pps the ghost writah benene melokane la
halleu kane la tek ci brick, seye si benen melo dane la
rime (book!) sound (good!) cl-ssic maker like sam cook
recognize k!llah k!llah naka war

[kaz k!llah]
lii diarna safara sa kaw
ni sakhaba ya tcha kaw
yéferr yi lankeu bagn niete niete (bagne) douniou gueum
daw siile ng-y nieuw diébelou nguir yegg fi nga dieum
kaz k!llah, tekk cii brik two
niou tekk cii brik go
niou tekk cii brik ba khotii n-gg- sa beytou (toubeuy)
xouss douniou bayi hectare nioune dagni brikk tout
kaz k!llah fokatii mic nieup di guestou
nokou ko cii beat ma tekk cii brik

[refrain: nitdoff]
bo tchii meuneta tek lou carré n-gg- werr ko é go
bo tchii meuneta tek lou carré n-gg- werr ko té go
real rap lagni mouki kheurko saa kaw
real rap lagni mouki kheurko saa kaw
tekk cii brik 2, tekk cii brik 2 (what)
tekk cii brik 2, tekk cii brik 2 (what)
east side, west side, tekk cii brik 2 (héééé)
tekk cii brik 2, tekk cii brik 2 (what)
tekk cii brik 2, tekk cii brik 2 (what)
north side, south side, tekk cii brik 2 (héééé)

[cap 2 seuss]
kone baay ba légui magui fii difi seuss
the lyrical b-tch leu saysay cii rhyme
matoulo nditch yaw défa ngo crime
like né kali and bryme
bourou mbede ba ngui nii
u know me, don’t touch boul lale mother f-cker
wauroule boy tékeulé fnk ak sa crew
my n-gg- sauroul, sick leu, deep leu
kone def tchii nit nga xam né tioloul cii wagua-ndikou real

[djily bagdad]
eh yow bagdad i’m a n-gg- loukouss kaatt bi feulattt
gni amone loy djip lay nieuw deufeulatt
rimes you tangue bamou eupe lalay eufeulatt
mane dane free djéleu naniou eufeul-latt
bénène groove moy bombe partout move bi yeup la clatéééé
k!llah connected tonkaali fake yi aka nio laka latéé
tekk cii brik build neum paya from the ground up
yekeutii wey wey high, burn this town neum
tabakhatt lou soutt ndiott yi
dép-ssé sommet yi
gni sibeu goul niom niofa nélaw niou bayi lène ciii sommeil yi

[refrain: nitdoff]
bo tchii meuneta tek lou carré n-gg- werr ko té go
bo tchii meuneta tek lou carré n-gg- werr ko té go
real rap lagni mouki kheurko saa kaw
real rap lagni mouki kheurko saa kaw
tekk cii brik 2, tekk cii brik 2 (what)
east side, west side, tekk cii brik 2 (héééé)
tekk cii brik 2, tekk cii brik 2 (what)
north side, south side, tekk cii brik 2 (héééé)

[seventhy sky]
yow how many years niou try to dieulé fi man
yéwou somé ni comédie ni takhaw cii sommet bi
wané ni lougni def yaw dou yeufou dii goné dii
fokk niou wané nii wané nii real hip hop mo ayé cii gané cii
fékhél sa xell mi délou cii louniou takha diouk niou make cii dollar cii
di got a lot of respect mbede bi bégué cii diégué cii
défél sa xell cii lougni tekk di step ma guéneu cii
gueuneu sigui xippi ni like yénéne philosophie
kaay gueustou ko fi real rap bi lagni firiii

[da brains]
r+8 niou xathie ko niar kou nekk def
4 you am niveau rap bou deep ni mos sef
tekk cii brik mou yokk
adjou cii kaw na rimes yi tokk
sign cii sound bou nice bi diarna bokk
kèn kou nék daga wara melni
kou cii nieuw guiss niou rap
tekk nga cii brikk
tek nga cii deal
tekk nga cii hit
all know this song
kaay tek cii sa brikk

[refrain: nitdoff]
bo tchii meuneta tek lou carré n-gg- werr ko té go
bo tchii meuneta tek lou carré n-gg- werr ko té go
real rap lagni mouki kheurko saa kaw
real rap lagni mouki kheurko saa kaw
tekk cii brik 2, tekk cii brik 2 (what)
east side, west side, tekk cii brik 2 (héééé)
tekk cii brik 2, tekk cii brik 2 (what)
north side, south side, tekk cii brik 2 (héééé)

[books]
diouk lèn niou tabakh sunu pyramide
dioxél loxo té né mittt
rakh mou liss
rakh mou liss
deugueur nii coranik
sama xalam coram bi
sabar galagn xorom bi
clap niou guiss
clap niou guiss
lou deep nii t-tanic
pyramid pyramid kawé ni pyramid
kawé ni coranik
kawé ni t-tanic
h-llo ma atomik
k!llah miit ndii k!llah
hit ni k!llah
bit ni k!llah
street ni k!llah
sweet ni k!llah brût

[nitdoff]
yo
like the rest to the cap dama wérédi flow
fight ba dess to the top dém beuri si doe (xaliss)
yeukeuti brik tek
track yék clip you djékeu
nioun la mbéde bi aare ci pét nioun leu public biy cheek
dipi di deupeu sa mind
dikkeu, ngéy neub sa rhyme
yeukeuti niveau bi kawé cii ba do reude sa line
nit toudou doff mic’am clash’nicov la
kou d squad protect do xalate niou thiofla

[refrain: nitdoff]
bo tchii meuneta tek lou carré n-gg- werr ko té go
bo tchii meuneta tek lou carré n-gg- werr ko té go
real rap lagni mouki kheurko saa kaw
real rap lagni mouki kheurko saa kaw
tekk cii brik 2, tekk cii brik 2 (what)
east side, west side, tekk cii brik 2 (héééé)
tekk cii brik 2, tekk cii brik 2 (what)
north side, south side, tekk cii brik 2 (héééé)



Random Lyrics

HOT LYRICS

Loading...