samba peuzzi - oulalalah lyrics
toujours au tiek posé dans le bendo
ñangal chaque jour ba nga fokni dañu ñaaw
firi rek baćc bo yéexe do guiss
gang bi dañu méchant oulalalah
firi rek baćc bo yéexé do guiss
gang bi dañu méchant o
oulalalah
ouwa ah ah ah ah ouwa ah
from diack wawaw
ouwa ah ah ah ah ouwa ah
oh my gang
hey tapette dufi fréq (non non)
fake dufi fréq (non non non)
indique dufi fréq (non non)
snitch dufi fréq (non non non non)
diamaguene for life sama side waw waw
thiow li thiow li fils lepp fi la
muy mag di ndaw ko ci laaj nala wax
fi ñëpp xam ni devise bi li leu
samba kuko bëgg ñu bëgg la
kuka bëggul ñune bëhgu ñula
kuko bëgg ñu bëgg la
kouka bëggul ñune bëggu ñuko
toujours au tiek posé dans le bendo
ñangal chaque jour ba nga fokni dañu ñaaw
firi rek baćc bo yéexe do guiss
gang bi dañu méchant oulalalah
firi rek baćc bo yéexé do guiss
gang bi dañu méchant oulalalah
ouwa ah ah ah ah ouwa ah
from diack wawaw
ouwa ah ah ah ah ouwa ah
oh my gang
n+ggas hate hate hate hating
but mama pray pray pray for me
with my gang gang gang gang gang
from the bottom now all eyes on me
da nga fogon du nekk té pourtant on l’a fait
t’as vu ouais t’as vu
pour yaw duñ ci gеnnë té pourtant on l’a fait
t’as vu ouais t’as vu
devise bi li leu
samba kuko bëgg ñu bëgg la
kuka bëggul ñunе bëhgu ñula
kuko bëgg ñu bëgg la
kouka bëggul ñune bëggu ñuko
toujours au tiek posé dans le bendo
ñangal chaque jour ba nga fokni dañu ñaaw
firi rek baćc bo yéexe do gis
gang bi dañu méchant oulalalah
firi rek baćc bo yéexé do guiss
gang bi dañu méchant oulalalah
ouwa ahah ahah ouwah
from diack wawaw
ouwa ah ah ah ah ouwa ah
oh my gang
gang, gang, gang, gang, gang, ….
Random Lyrics
- haaky - моя дорогая люси (my dear luci) lyrics
- dani mocanu - legenda vie lyrics
- cheatz (pol) - toxic hell final lyrics
- xoedoxo - love and hate lyrics
- dolatson - szkol-in' lyrics
- akat$ - fora do comum lyrics
- sir rah (rap) - spotlight lyrics
- hamond - windows lyrics
- johnyboy - взаперти (locked up) lyrics
- jørdan - vida funk lyrics